« Ragaluma ñak suma bakan »
HTML-код
- Опубликовано: 8 янв 2025
- Je confie ma mission au Seigneur lui qui m’a choisi. En lui je mets ma confiance, sûr qu’il agira!🙏🏽
🎸🎼Ragaluma, ragaluma ñakeu suma bakan. Mane jaam biñu sopi xarit, Yennunaa.
Suma tiis moy lilé: ndaakh dina meuna motali Yeblé Yalla.🎼🎸
🎸🎼Malako yén, dinalako japalé.
Bul ragal dara, bul ragal maa la ngémbeu démal.🎼🎸
🎼Ngémbuna, ngémbuna, ngémuna daléko tey, Andak l’abbé bu mag bi njeuka jalleu Asamaan, ak Xeel mu Selleumi, uufu fa Mariama Suñu Ndey.🎼
DIEU SEUL SUFFIT
dieu seul suffit pour toute la vie du courage grand frère 🙏
Machalah
Nehk na
Gloire à Dieu ♥️🙏